0^YOWAANAYeesu Kirist moo di Kàddu gi ak leer gu wóor giYaxya nee na, du Almasi biYeesu moo di Gàttub YàllaÑi jëkka doon taalibey YeesuYeesu woo na Filib ak NataneelYeesu dem na céet ga ca dëkku KanaYeesu dàq na jaaykat ya ca kër Yàlla gaYeesu waxtaan na ak njiitu diineYeesu moo gëna màgg YaxyaYeesu waxtaan na ak jigéen ji amoon juróomi jëkkërTaalibey Yeesu ya délsi nañuÑu bare ci waa Samari gëm nañu YeesuYeesu faj na xale ba bëggoona deeYeesu faj na jaragSañ-sañu Doomu Yàlla jiFirnde yi wone sañ-sañu YeesuYeesu dundal na mbooloo miYeesu dox na ci ndoxYeesu mooy ñam wiy joxe dundTaalibey Yeesu yu bare weddi nañuYeesu ca màggalu Mbaar yaYeesu jàngle na ca màggal gaNdax Yeesu mooy Almasi bi?Njiiti Yawut yi gëmuñu YeesuJigéen ji doon njaalooLi Yeesuy wax mooy dëggWaa kër IbraaymaWaa kër SeytaaneLi Yeesu seede ci mbiramYeesu faj na gumbag judduwaaleFarisen laaj nañu gumba, gi ñu wéralNgumbag xelMisaal ci mbirum sàmm bi ak xar yiYawut ya nanguwuñu YeesuDeewu LasaarYeesu mooy ndekkite, mooy dundLasaar dekki naPexe yi jëm ci YeesuMaryaama sotti na latkoloñ ci tànki YeesuYeesu dugg na YerusalemYeesu wax na ci ni mu wara faatooYeesu bàyyi na Yawut ya ci seen ngëlëmYeesoo raxas na tànki taalibeemYeesu yégle na ne Yudaa moo koy worYeesu yégle na ne, Piyeer dina ko weddiYeesu dëfal na xolu taalibeem yiYeesu mooy yoon wi jëm ci YàllaYeesu dig na leen Xel mu Sell miYeesu, garab gu wóor giNit ñi bañ nañu Yeesu ak ay taalibeemJëfi Dimbalikat biNaqar wa, soppaliku na bànneexYeesu not na àddinaYeesu ñaanal na boppamYeesu ñaanal na ay taalibeemYeesu ñaanal na ñi koy gëm ëllëgJàpp nañu YeesuYóbbu nañu Yeesu ca AnasPiyeer weddi na YeesuSarxalkat bu mag ba seetlu na YeesuPiyeer dellu weddi YeesuYeesu ca kër PilaatÀtte nañu Yeesu ci deeDaaj nañu Yeesu ci bantYeesu saay naRob nañu YeesuYeesu Kirist dekki naYeesu feeñu na Maryaamam MagdalaYeesu feeñu na taalibe yiYeesu ak TomaaYeesu feeñu na juróom ñaari taalibeYeesu ak Piyeer