0^Màndiŋ maIsrayil jànge na ca maam ya jóge woon MisraTakk nañu limu bànni IsrayilLimaaleesul Leween ñiLu jëm ci dalinu giir yiLu jëm ci sasi Leween ñiLim nañu Leween ñi ak seeni maamLim nañu taaw yi ngir seen njotlaayYeneen kuréli Leween a ngi ak seeni sasLim nañu Leween ñi liggéey warSàrtal nañu doxalin yiy setal dal biLu jëm ci jigéen ju moyLii moo war ku séddoo Aji Sax jiGii ñaan moo war ci askan wiDaloob jaamookaay bi laaj nay saraxLu jëm ci teginu làmp yaLu jëm ci cetlug Leween ñiLu jëm ci màggalu bésub MuccAji Sax ji yiir na xaymab ndaje maLu jëm ci liiti xaalis yaBànni Israyil sàqee nañu tundu SinayiBànni Israyil jóge nañu SinayiBànni Israyil ñaxtu nañuAji Sax ji dig na Musaa ñu ko jàppleYàlla sol na mag ña ag leeramMbas wàcc na ca Kibbrot TaawaMaryaama ak Aaróona jote nañook MusaaMusaa yeble na KanaanNdaw ya délsi nañuMbooloo ma bañ naa duggi KanaanGàntal Aji Sax ji sabab na mbugalMbooloo ma gàntalati naLu jëm ci saraxi pepp ak diw ak biiñAb jooxe war na ci pepp mu jëkkSarax war na ci moy gu dul teyeefBésub Noflaay wormaal la laajYoon sàrtal na wàllu colKore fippu naWay-fippu ya jot nañu seen añAndi way-fippu ya firnde laÑaxtu sabab na mbugalBant bu wow jebbi naLu jëm ci sarxalkat yi ak Leween ñiLu jëm ci peyu sarxalkat yiLu jëm ci peyug Leween ñiAb jooxe ñeel na Leween ñiLu jëm ci ndoxum setlu ak setlu gi warDiiŋat nañu Musaa ak Aaróona fa MeribaEdom bañ naAaróona nelaw naBànni Israyil am na ndamLu jëm ci nattub jaan yaIsrayil daan na Siwon ak OgBalaam gis na céru barke bi ñeel IsrayilBuur Balag woo na Balaam wallMbaam yedd na boroomBalaam tase na ak BalagBalaam ñaanal na IsrayilBalaam baamu na ñaanamBalaam ñaanalati na IsrayilBalaam gis na ëllëgu IsrayilBalaam gis na mujug nooni IsrayilBànni Israyil bokkaale na ca réewum MowabIsrayil dégg na ab artoom balaa dugg KanaanÑaareelu limeefu bànni Israyil taxaw naLu jëm ci séddaleb réew maÑaareelu limeefu Leween ñi taxaw naTëj nañu limeef yaLu jëm ci jigéen ñi ak seen céri suufYosuwe wuutu na MusaaBés bu nekk laaj na ab saraxBésub Noflaay am na saraxamTerutel weer am na saraxamBésub Mucc am na saraxamNgóob am na saraxamBési liit yi laaj na saraxBésub Njotlaay laaj na saraxMàggalu Mbaar yi laaj na saraxYoon wi sàrtal na lu nit ki xasal boppamIsrayil duma na MajanLu jëm ci séddaleb alalu waa MajanKilifay xare ya jëfe nañu ngorAy giir des na penkub YurdanLimees na yooni tukkiy IsrayilNdigali xare jib naAji Sax ji rëddlu na digu réew miLim nañu saytukati séddale baLu jëm ci céri suufi Leween ñiLu jëm ci dëkki rawtu yiLu jëm ci séyu jigéenu Israyil, ak céru suufam