0^Kàdduy WaareLuy solob àddina?Ma seet lu ma doyRafet xel doyulBànneexu neen doyulRafet xel fanqul deeNjariñ, fa YàllaJàmm, fa YàllaJamono, YàllaYaakaar feyul boroomAlal doyul boroomWéttalikoo gën wéetKilifteef saxulRagalal YàllaNguur bare na àqAlal coono laBànneexu bakkan, YàllaAlal, na la jariñNit dogalulNit am na pexe ciw tiisamLu ëpp tuuruXel mu rafet réer na maAna ku rafet xel?Bul roy lu bon.Yàlla, kenn xamu koBégeel sa bakkanÀddina wóorulXel mu rafet taxul ñu naw laLi xel wuuteek ndofKenn xamul, waaye beyal sa toolBégal te xam ne man saxulMa daaneel