0^1.SamiyelLii mooy jaar-jaari SamiyelAana ñaan na doomLu jëm ci juddub Samiyel ak ngoneemAana sant naLu jëm ci doomi EliLu jëm ci waa kër SamiyelEli àrtu na ay doomamNitu Yàlla rëbb na EliYàlla def na Samiyel yonentNangu nañu gaalu Yàlla gaMbugal ma topp na waa kër EliGaalu Yàlla ga jaaxal na FilistiWaa Filisti delloo nañu gaalu Yàlla gaSamiyel jiite na IsrayilIsrayil sàkku na buurBànni Israyil ñaan na Samiyel buurLu jëm ci sañ-sañu buurLii mooy jaar-jaari SóolSóol doxi na yónnentSóol gis na SamiyelSamiyel diw na Sóol, fal koNoowug Yàlla gane na SóolYàlla feddli na palug SóolSóol jéngu naSamiyel wàcc naSóol tooñ naYonatan def na njàmbaarYonatan song na waa FilistiSóol wax na lu ëppBànni Israyil jot na YonatanSóol am na ndamSóol tooñati naSóol ñàkk naLii moo dox diggante Sóol ak DaawudaYàlla fal na DaawudaDaawuda dugg na ca liggéeyu SóolGolyaat dëkk na bànni IsrayilDaawuda def na jalooreYonatan fas na kóllëreek DaawudaSóol a ngay fexeel DaawudaDaawuda jël na doomu Sóol soxnaYonatan taxawu na DaawudaMikal xettli na DaawudaSóol toppi na Daawuda ca NayotYonatan wallu na DaawudaDaawuda dem na ca AyimelegDaawuda nax na leenDaawuda jiite na gàngoorSóol rey na sarxalkati waa NoobDaawuda xettli na waa KeylaSóol topp na DaawudaDaawuda gën na SóolSamiyel saay naNabal gàntal na DaawudaJabaru Nabal def nag muusNabal dee, Daawuda dikkDaawuda gënati na SóolDaawuda làquji na ca waa FilistiSóol seetluji na ca EndorWaa Filisti dàq nañu DaawudaDaawuda toppi na Amalegeen ñaDaawuda gore naDaawuda sédd na njiiti Yudeen ñaLu jëm ci mujug Sóol