0^2 KORENTYàlla, Boroom lépp luy dëfal xol yiPool setal na boppamPool baal na ki tooñoonNdawi Yàlla ci xamle kóllëre gu bees, gi Yàlla fas ak nitNdamu kóllëre gu bees giXibaaru Kirist leeral na sunu xol yi lëndëmoonXibaaru Kirist dafa mel ni alal ju ñu yeb ciy njaqSunu màkkaan ci wetu Boroom biNanguleena juboo ak YàllaTiis yi nu daj ci liggéeyal YàllaBàyyileen bokkaaleMbégu Pool ci ñëwug TitMayeleen ak xol yu yéwénLi tax ñu yónni Tit ak i àndandoomKu ji lu bare, góob lu barePool ñaan na, ñu nangu sañ-sañamPool ak ndawi naaféq yiNattuy Pool ci matal yónnentamPeeñub Pool ak nattu bi ko dalPool bëgg na leenArtu yu mujj yiTàggtoo