0^1 KORENTPool sant na YàllaNa mbooloo mi jubooXam-xamu nit jotewul dara ak bu YàllaXelum Yàlla mooy joxe xam-xamu YàllaXuloo ci biir mbooloom ñi gëmYàlla rekk moo am sañ-sañu àtte nuGénneleen kiy moy Yàlla ci seen biirBàkkaar ci xol dafa mel ni lawiir ci mburuWaruleena réeroo ci seen biirJariñooleen seen yaram ngir ndamu Boroom biLi jëm ci mbirum séyMbir yi jëm ci lekk yàpp, wi ñu jagleel xërëm yiDëddu naa peyu ndawal Kirist te lew na maMbirum bànni Israyil misaal la, ma nuy artuBuleen booloo ak rab yu bon yiNa mbëggeel laal seeni jëf, te ngeen wottu seen sañ-sañLi jekk ci góor ak ci jigéen, bu mbooloo miy màggal YàllaReerub Boroom biMay yi jóge ci Xelu Yàlla miWenn yaram ak cér yu bareMbëggeel moo gëna màgg léppFarluleen ci di jottali kàddug YàllaSeetleen bu baax seen nekkin ci seen ndajeCi li jëm ci ndekkitel KiristNan lañu mana waxe ne, néew yi duñu dekki?Nan la yaramu ñi dekki mel?Ci mbirum laajum xaalis mi jëm ci mbooloom Yàlla miNdigal yu mujj yiTàggoo