0^Njàlbéen gaYàlla sàkk na àddina, fal ci nitCosaanal asamaan ak suufYàlla dugal na nit Àjjana, jox ko ndigalYàlla dàq na nit ÀjjanaKayin rey na AbelAskanu KayinAskanu Aadama, ba ci NóoyinYàlla fas na yéene tas àddina ndax mbonu nitAskanu NóoyinYàlla musal na Nóoyin ci mbënn miNóoyin génn na gaal gu mag gaYàlla fas na kóllëre ak NóoyinMbirum Nóoyin ma aki doomamAskanu doomi NóoyinXeet yi sosoo ci doomi NóoyinLi jëm ci askanu YafetLi jëm ci askanu XamLi jëm ci askanu SemYàlla safaan na làkku àddina, mu jaxasooAskanu Sem, maamu IbraamAskanu Teraa, baayu IbraamYàlla sant na Ibraam, mu gàddaayIbraam dem na réewum MisraIbraam ak Lóot teqlikoo nañuDigeb Aji Sax ja ak IbraamIbraam wallu na LóotMelkisedeg ñaanal na Ibraam barkeYàlla fas na ak Ibraam kóllëreIsmayla juddu naYàlla soppi na turu IbraamXaraf màndargaal na kóllëreg YàllaIbraayma ak ganam ñaIbraayma tinul na waa SodomBàkkaari waa SodomLóot génn na SodomYàlla tas na dëkk yooyu di Sodom ak GomorMbirum Lóot ak doomam yu jigéen yaLu jëm ci Ibraayma ak AbimelegJuddub IsaaxaSaarata jote na ak Ismayla ak AjaraIbraayma waatoo na ak AbimelegYàlla nattu na IbraaymaAskanu NaxorIbraayma jënd na suuf ca KanaanIsaaxa jël na Rebeka soxnaIbraayma nelaw naAskanu IsmaylaAskanu Isaaxa doomu IbraaymaEsawu sàggane na céramIsaaxa nëbbu na waa Gerar ngir muccIsaaxa fas na kóllëre ak AbimelegEsawu jël na ay soxnaYanqóoba jëkk na Esawu ci ñaanamYanqóoba dem na ca nijaayamEsawu jël na keneen soxnaYanqóoba sàrtoo na ak YàllaYanqóoba daje na ak RaselLu jëm ci njabootu YanqóobaYanqóoba woomle naYanqóoba toxu na, jëm KanaanLaban dabi na YanqóobaYanqóoba ragal naa daje ak EsawuLu jëm ci bëreb Yanqóoba baYanqóoba ak Esawu daje nañu ci jàmmTooñ nañu Diina doomu YanqóobaYanqóoba sanc na BetelBeñamin juddu na, Rasel faatuDoomi Yanqóoba yaIsaaxa nelaw naAskanu EsawuLu jëm ci askanu SeyirLu jëm ci buur ya jëkka falu ca EdomAskanu YanqóobaYuusufa gént na lu yéemeLu jëm ci Yuda ak Tamar ak seen askanJaay nañu Yuusufa jawriñu FirawnaSoxnas Potifaar fexeel na YuusufaTëj nañu Yuusufa kasoYuusufa firi na ñaari géntFirawna gént naYuusufa firi na génti FirawnaFirawna fal na Yuusufa, mu jiite Misra géppMagi Yuusufa ya dem nañu MisraYuusufa xupp na magam yaDoomi Yanqóoba ya dellu nañu KanaanMagi Yuusufa ya yóbbu nañu BeñaminMagi Yuusufa ya dellu nañu MisraYuusufa nattu na ay magamYuda tinul na Beñamin ca YuusufaYuusufa xàmmiku na ay magamFirawna woo na Yanqóoba MisraYanqóoba dem na MisraNjabootu Yanqóoba, gi ñëw MisraYanqóoba gis na YuusufaYuusufa nuyole na ay bokkam FirawnaLu jëm ci saytub Yuusufa ca xiif baLu jëm ci ati Yanqóoba yu mujj yaIsrayil ñaanal na Efrayim ak ManaseYanqóoba tàggoo naYanqóoba nelaw naYuusufa rob na Yanqóoba réewu KanaanMagi Yuusufa yaa ngi jéggaluYuusufa nelaw na