0^EsekiyelEsekiyel daje naak leeru Aji Sax jiBindkat a ngi joxe tegtal ca moomu peeñuNii la peeñu ma bindooAji Sax ji yebal na EsekiyelAji Sax ji dooleel na EsekiyelTëju te tëlee wax misaal laEsekiyel yégle na gaw baDogal dikkal na YerusalemTuur yi indi na mbugalAji Sax jeey am ndamJeexle dikk naBokkaale feeñ na ca kër Yàlla gaRey nañu bokkaalekat yiLeer ga dëddu naDigeb yiw a gën jàmmu teyNgàllo xeeñ naWaxyuy nit, waxi caaxaanMbugalu yonent yi taxaw naDëppleenYerusalem gépp a yelloo mbugalBantu reseñ matul mattYerusalem yemul ci boroom këramFecci kóllëre, peyam du jaasJëf, jëlJooy ngarmig Israyil war naIsrayil wor, Aji Sax ji goreWoyu saamar jib naYerusalem def nay tojaangeSamari ak Yerusalem bokkaale nañuMbugalu Yerusalem, misaal maa ngiSoxnas Esekiyel faatu naKàddug waxyu dal na xeet yiWaxyu dal na AmonWaxyu dal na MowabWaxyu dal na EdomWaxyu dal na FilistiWaxyu dal na TirEsekiyel jooy na TirNguurug Tir foq naWaxyu dal na SidonAji Sax jeey yiwi IsrayilWaxyu dal na MisraBabilon song na MisraDoole réer na MisraPonkal daanu naJàmbaaru àddina, baadooloy njaniiwMisra wéetul ca toroxteemTabb nañu Esekiyel jongrukatJëf ju bon daane na YerusalemWaxyu dal na sàmm su bon siWaxyu dal na EdomBarke ñeel na tundi IsrayilIsrayil yeeslu, Yàlla di sell ba teyIsrayil dekki naIsrayil, genn giir, benn buurKàdduy waxyu dal na GogGàngooru Gog sànku naAji Sax ji ñoŋal na sellngaamEsekiyel gis na kër Yàlla gu beesNatt nañu miir baak bunt ba féete penkuNatt nañu ëttu biti baNatt nañu bunt ba féete bëj-gànnaarNatt nañu bunt ba féete bëj-saalumNatt nañu bunt ya jëm ëttu biir baNatt nañu néegu carxal giNatt nañu ëttu biir baNatt nañu néeg Yàlla baNatt nañu toftalu néeg Yàlla biBer nañu ab tabax ca gannaawNatt nañu taaxi sarxalkat yiNatt nañu miiru biti bu kër Yàlla giLeeru Yàlla dellu na këramNatt nañu sarxalukaay biSàrtal nañu sarxalukaay biAy jagle ñeel na boroom jal biJege bérab bu sell bi du wàllu ñéppLeween ñi am nañu seen wartéefi boppAskanu Cadog am nañu seen wartéefi boppLu jëm ci suuf si ñu jagleel Aji Sax jiSàrt yii war na boroom jal bi ci wàllu kër Yàlla giBoroom jal bi sañul lépp ci suufamSàkkal nañu kër Yàlla gi ay waañAm wal balle na kër Yàlla gaAji Sax ji joxe na kemuy réew mi ñuy séddooDaggal nañu suuf giiri bëj-gànnaarDaggal nañu Aji Sax ji céram bu sellDaggal nañu suuf waa dëkk bi ak boroom jal biDaggal nañu suuf giiri bëj-saalumYerusalem: tur wu yees, fukki bunt ak ñaar, ni giir yi