0^EfesAy barkee ngi ci AlmasiPóol sant na, ñaan naGëm, soppiGëmkati Almasi benn lañuPóol xamle na mbóotum YàllaSaxoo gëm moo mata ñaanMbooloom gëmkat ñi wenn yaram laKu gëm Almasi war koo royPóol lim na meloy gëmkat bu dëgguJëfeleen ni niti leerJabar mokk, jëkkër soppWaajur na yar, te njaboot di déggNa jaam ak sangam déggal Boroom biXare bi nook Seytaane laPóol tàggu na waa Efes