0^Baamtug Yoon wiMusaa fàttli na jaar-jaari IsrayilNdigalu yëri Kanaan jib naBànni Israyil teggi nañuIsrayil nangu na penkub dexu YurdanSéddale nañu penkub YurdanMusaa duggul KanaanMusaa ñaax na bànni IsrayilYoon wi aayal na bokkaaleAb jagle ñeel na IsrayilAmal nañu ay rawtu ca penkub YurdanMusaa baamtu na yoon wiFukki santaanee ngiAji Sax ji kenn laDogook yenn xeet yi war na IsrayilXéewlu, fàtte aay naIsrayil gënul ci xeet yiIsrayil jaamu na sëlluw wurusMusaa tinul na bànni IsrayilMusaa ngi woote déggal Aji Sax jiBarke ak alkànde dëgmal naLu jëm ci sàrti dundin ca réewum dige baAji Sax ji mooy taamu bérabamDee mooy àtteb kuy xiirtale ci bokkaaleYoon wi sàrtal na jëfin yu setLu jëm ci céri fukkeelLu jëm ci njéggalug borSang am na lu ko war ci jaamamLi war ci taawug jurÑetti yoon lees di màggalsi ci bérab bu sell biYoon wi sàrtal na mbirum àtteAy ndigal ñeel na buurAy yelleef ñeel na Leween ñi ak sarxalkat yiKàddug waxyu day sottiBer dëkki rawtu ndigal laLu jëm ci kemu suuf ak limu seede cib àtteYoon wi sàrtal na mbirum xareNjotlaay war na ci bóomkat bu umpeAy sàrt a ngi ci wàllu njabootDeesul wékk nit, fanaanal koYoon wi sàrtal na dundin wu jekkSàmmonteleen ak àqu jigéenAm na ñu dul bokk ci ndajem Aji Sax jiDeesul topp bànni Israyil ab tegandaayWàccook aw xas wartéef laRaasaatu mu suur boroom lew naYoon wi sàrtal na pase ak séyaatYoon wi aar na néew-ji-dooleNjub ak yërmande wartéef laDonn sa jabaru mbokk wartéef laAm na jëf ju aay ci sotAb nattukaay day matMbugal Amaleg ndigal laNjotlaayal Aji Sax ji laaj na ab galagKóllëre feddliku naMusaa biral na yooni barke ak alkàndeLu jëm ci alkànde yiLu jëm ci barke yiDéggadi, alkuKóllëre gi yeeslu naBuleen caaxaane kóllëreg Aji Sax jiMbugal du jaasDellusi ci Aji Sax ji, barkeelMusaa nee déggal Yàlla yomb naMusaa tàggoo naMusaa woy na kóllëreg Aji Sax jiDéggal Aji Sax ji, dundAji Sax ji woo na MusaaMusaa ñaanal na bànni IsrayilMusaa wuyji na