0^2.SamiyelLii mooy jaar-jaari Buur DaawudaLu jëm ci tàggeb SóolDaawuda jooy na Sóol ak YonatanDaawuda falu na buur ca YudaIsboset falu na buur ca IsrayilYuda ak Israyil xare nañuDaawuda am nay doom ca EbronAbner jote naak IsbosetAbner fekki na DaawudaYowab fey na AbnerJooy nañu AbnerIsboset faatu naDaawuda falu na buur ca IsrayilDaawuda nangu na YerusalemBuur Daawuda duma na waa FilistiGaalu Yàlla ga dem na YerusalemGaal ga dikk na YerusalemLu jëm ci kër Yàlla ak kër DaawudaDaawuda delloo na Yàlla njukkalDaawuda duma na xeet ya ko wërLu jëm ci jawriñi DaawudaDaawuda baaxe na MefibosetDaawuda jote naak Amoneen ñaDaawuda xare naak SiriDaawuda topp na bakkanamYonent Yàlla Natan yedd na DaawudaDoomu Daawuda faatu naSuleymaan gane na àddinaDaawuda nangu na péeyub Amoneen ñaAmnon tooñ na TamarAbsalom feyu naAbsalom délsi naAbsalom lal na pexeDaawudaa ngi wuta rëccDaawuda tase naak surgab MefibosetDaawuda tase naak mbokkum SóolAbsalom dugg na YerusalemUsay nax na AbsalomDaawuda xare naak AbsalomLu jëm ci tàggeb AbsalomYowab sikk na DaawudaDaawudaa ngi dellu YerusalemSimey tuubal na DaawudaDaawuda baaxe na MefibosetDaawuda tàggtoo na ak BarsilaySeba jàmbu naLu jëm ci jawriñi DaawudaYenn xew-xew a ngiWaa Gabawon feyu nañuDaawuda daje naak ponkali waa FilistiDaawuda sant naDaawuda biral na waxyuJàmbaari Daawuda def nañuy jalooreDaawuda waññ na bànni Israyil