0^2.Buur yaYonent Yàlla Ilyaas yar na Buur AkasiyaYonent Yàlla Ilyaas yéeg naIsrayil ak Mowab jote nañuAlyaasa jot na jëtun baAlyaasa am nab dalAlyaasa delloo na njukkalAlyaasa sekki na tooke jaAlyaasa leel na mboolooAlyaasa faj na kilifaGewasi lal na pexeWeñu sémmiñ ga tëmb naAlyaasa sànk na gàngoorXiif ba tar na ca SamariAji Sax ji wallu na SamariNdawas Sunem sa jotaat na alalamAsayel mujj na falu ca SiriYoram falu na YudaAkasiya falu na YudaAlyaasa fal na YewuYewu fexeel na buur yaYesabel dee naYewu bóom na waa kër AxabYewu fiir na waa kër BaalLingeer Atalyaa falu na YudaYuda bañ naYowas santaane na ñu defaraat kër Aji Sax jiBuur Yowas jeexal naYowakas falu na ci IsrayilYowayas falu na ca IsrayilYonent Yàlla Alyaasa faatu naIsrayil duma na SiriBuuri Israyil ak Yudaa ngi xeexooYowayas buurub Israyil saay naAmaciya buurub Yuda saay naYerbowam mu ndaw falu na ca IsrayilAsaryaa falu na buur ca YudaSàkkaryaa falu na buur ca IsrayilSalum falu na buur ca IsrayilMenayem falu na buur ca IsrayilPekaxiya falu na buur ca IsrayilPeka falu na buur ca IsrayilYotam falu na buur ca YudaAxas falu na buur ca YudaOse falu na buur ca IsrayilSamari, péeyu Israyil, tas naWaa Asiri sancal nañuy jaambur ca SamariEsekiya falu na buur ca YudaAsiri song na YudaAsiri tooñati na YudaYonent Yàlla Esayi yégle na jéllub AsiriEsekiya wopp na, ba jógBuuru Babilon yónnee na ca EsekiyaBuur Esekiya saay naManase falu na buur ca YudaAmon falu na buur ca YudaYosya falu na buur ca YudaTéereb yoon wi feeñ naYosya sellal na réew miMàggalu bésub Mucc délsi naBuur Yosya saay naYowakas falu na buur ca YudaBuur Yowakim fey na Misra galagYowakin falu na buur ca YudaCedekiya falu na buur ca YudaNangooti nañu YerusalemYàq nañu kër Aji Sax jiJàpp nañu Yudeen ñi njaamNabukodonosor tabb na Gedalya ca YudaTijji nañu Yowakin buurub Yuda